#8 Nék jigeen biir Sénégal (le statut de la femme au Sénégal)

Sortie:

Salam, Salam !
Dans cet épisode, je parle du statut (dans son ensemble) de la femme dans la société sénégalaise. 

Dañuy faral di dégue "jiguène ni la wara mél", "kou bax sa ndeya tax" wala "ligueyou ndey anioub doom" lane lay téki thi suñu société ? 
Dañuy faral di guiss ñéne si ñoune di doundou lou méti té douñou saña wax ... 
Dina dioxé sama xalate si yéne wax yigua xamné moy ték pression jigeen you beuri thi souñou biir société. 

Dalal ak diam.

Partages ton témoignage ici : raam.dokh@gmail.com

Instagram : raam_dox
Tiktok : raam_dox
Youtube : raam dox Hébergé par Ausha. Visitez ausha.co/politique-de-confidentialite pour plus d'informations.

#8 Nék jigeen biir Sénégal (le statut de la femme au Sénégal)

Titre
#8 Nék jigeen biir Sénégal (le statut de la femme au Sénégal)
Copyright
Sortie

flashback